Baye Fall bi tothie na Grand Bal bou Youssou Ndour bi et assure le show « yaye sen baye «

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 20 янв 2025

Комментарии • 29

  • @BourSall-u7e
    @BourSall-u7e 11 дней назад +1

    Hoooo sama khell demna si aziz dabala😢 gracias youssou nduor ❤

  • @diorcisse3487
    @diorcisse3487 16 дней назад +6

    Yalna sa diam yague thy barké Seydina Mohamed psl amine yaraby nékal thy diam N'dour waly

  • @Nafina-v7u
    @Nafina-v7u 16 дней назад +7

    C'est bien you c'est très bien ❤❤❤❤

  • @soniadiallo5893
    @soniadiallo5893 14 дней назад +4

    Kou nanguouwoul ndogalou yallah rek mokoy contre c est un grand monsieur té loumou am dako niafé depuis 14 ans fékk na gueum na bopam sokjor bakhoul délléne nanguoul niit ki liko sounou borom may guisna ay nafékh nio khamné kénne nawlowoulléne niouy diéma niawal acte bi Wally def dem fékki bayam niou sokkor ui nga khamné tékki wouniou daara demb ak taay diko yakh Ibliss yi niou donne mais Wally n les écoute pas yaw danga bakh té dem nga ba paré giinaw yallah kénbe mounala teuyé boula kénne woutal ay nonne lankal

  • @PapeSéne-g7y
    @PapeSéne-g7y 16 дней назад +25

    Mandoulene et essayer de faire quelque chose de positive pour votre pays youssou lui au moins il a créé des emplois lui il n a pas temps il n écoute pas vos commentaires

  • @papisgueye90
    @papisgueye90 16 дней назад +11

    Thiéy you mo kham sénégalais dée daléna bayék wakhdji nék si liguéyam mayé patbi

    • @Loulou-p7z
      @Loulou-p7z 15 дней назад +1

      Motakhite avancer rek gnom gnouy dé

  • @fatoudiagne9373
    @fatoudiagne9373 16 дней назад +8

    C'est pas les marabouts c'est Dieu

  • @djibrilba5679
    @djibrilba5679 16 дней назад +6

    Li nekh ne way

  • @LayeSerrere
    @LayeSerrere 15 дней назад +1

    Daffa leer 🎉❤❤❤❤😊😊

  • @aliounendiaye9487
    @aliounendiaye9487 10 дней назад

    lou positive comme delencan fiscal

  • @OusmaneDiab
    @OusmaneDiab 16 дней назад

    Youssou mo yéwoudéh😂😂😂 vrai sénégalais

    • @julio25
      @julio25 15 дней назад

      D'accord et puis quoi encore ?

  • @OusmaneDiab
    @OusmaneDiab 16 дней назад +1

    Bay fall bidéh dotoul madial😂😂😂

  • @AissatouFaye-k8c
    @AissatouFaye-k8c 16 дней назад +1

    Kouy wakh wokhou diamou yalla do saga ngua balma

  • @AAj5k
    @AAj5k 16 дней назад

    Yen yena yapp ahlou baye Fall ki Kay Baye Faux leu

  • @eternelreconnaissant5562
    @eternelreconnaissant5562 11 дней назад

    Vraiment il faut pas dire Baye Fall c’est pas parcequ’il a des Rasta qu’il l’est . Baye Fall il a pas le temps de faire ça

  • @stafiroulaha
    @stafiroulaha 15 дней назад

    thieye magoume thiakhane

    • @julio25
      @julio25 15 дней назад +1

      Mo taye lo ci meune.

  • @LamineDiop-z8b
    @LamineDiop-z8b 16 дней назад

    Fo rek li na dieq si rewmi

  • @ibrahimandiaye8214
    @ibrahimandiaye8214 16 дней назад

    Ay domeram deugu moy yen démlén diamoudji Yalla mogueun siyén Youssou ndour ragalal Yalla domeram 😂